ELECTIONS LOCALES 2022

Cher(e)s compatriotes, en mon nom et en celui de la Coalition Yewwi Askan Wi, je tiens à vous dire Jërëjëf ! Jërëjëf de nous avoir accueillis dans vos villes, dans vos communes, dans vos rues, dans vos maisons. Jërejëf de nous avoir accueillis durant toute cette campagne électorale. Jërëjëf de nous avoir accompagnés sur les milliers de kilomètres parcourus à travers l’étendue du territoire, d’Est en Ouest, du Nord au Sud. Jërëjëf de nous avoir accordé de votre temps, de votre énergie et de votre attention pour écouter le message d’espoir et d’avenir que nous sommes venus vous délivrer. Jërëjëf de nous avoir témoigné votre fierté et votre engagement à construire un Sénégal prospère et souverain. Cette campagne a été belle et réussie grâce à vous. Encore une fois, merci ! Rendez-vous très vite pour célébrer la victoire du peuple.

Yéen samay soppe, ci sama tur ak ci tur Yewwi Askan Wi, noo ngi naan leen Jërëjëf !Jërëjëf, ci dalal gi ngeen nu dalal ci seen i gox, ci seen i gox-goxaan, ci seen i mbedd, ci seen i kër.Jërëjëf, ci yaatal gi ngeen nu yaatal ci diirub nemmeekuy joŋante yépp.Jërëjëf, ci ànd gi ngeen ànd ak nun ci ay juniy ñay ci mbeeraay gi, penk ak soww, bëj-gànnaar ak bëj-saalum.Jërëjëf, ci seen jot gi ngeen nu may, seen kàttan, may nu nopp ba nu jàllale sunu bataaxelu yaakaaru ëllëg bi nu leen jébbal.Jërëjëf, ci wan gi ngeen nu wan seen ug sigarewoo ci nun ak seen ug aamu ci tabax Senegaal gu naat te jaar yoon.Bile kàmpaañ taaru woon na lool, te kiilu jërëngeenjëf.Jaangeenjëfati !Noo ngi leen di jox dig-daje ci lu yàggatul ci cambalug ndamal askan wi.

Voir aussi

15ÈME SOMMET DE L’OCI À BANJUL

Discours de Son Excellence Monsieur le Président de la République Bassirou Diomaye Faye à l’occasion …

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *